-
Nabiil Ibn Abdi Rahim Ar-Rifaaii "Limou mbiryi : 3"
Mélokâne bi :Mi ngi judd 19-06-1398 ci gàddày gici jidda. Ci atum 1415 ci gàddày gi la mookaal alxuràn. Amna majestér ci saytu mëne mënup nite. ak bac ci porotochimi. pilote la ci arabisawdite. Mi ngi tàmmbalé jitté ci atup 1415 ci gàddày gi ci kaar ci jàkkàp Al-Baghdàdi ginàwgi ci jàkkàp Alhudà ci Al-Andalus toopp mu dem ci jàkkàp Khadija Bint Xuwaylid ci Zahrà. Fiiñu tooll mi ngi jiité aka xutba ci jàkkàp At-Taxwà ci yoonup At-Tahliya.