Limou mbiryi: 151
14 / 8 / 1436 , 2/6/2015
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Ngënélu Baraxlu ak li ci wér sax ci sunna
13 / 8 / 1436 , 1/6/2015
Jullite bi warna fumu tollu muy tenkku ci téggini lislàm yi, ba ci fani xayma xamxam yi ñudëgmal di na jàdu mu tëkku ci téggini lislàm yi
12 / 8 / 1436 , 31/5/2015
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Fébarup xol bu wow; ay sababam, màndargàm aki sàfaràm
Khoutba gui mi ngui ajou ci: éé yaw doomu àdama guddi ak bëccëk dañuy ligéy ci yaw knnak ligéyal ci ñoom. Ana naka ngay jariño sa waxtu
11 / 8 / 1436 , 30/5/2015
Khoutba gui mi ngui ajou ci: lénn ci jagléy Makk
24 / 6 / 1436 , 14/4/2015
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Yitèp lislaam ci koom koom ak souxaliku ci ay kaaddu yu matalé
Khoutba gui mi ngui ajou ci: lèral jafé jafé yi ci wuuté
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Ragal Yalla jàréko ci sèttanetal alkhourane ak diko doolli
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Sabap yiy sippi jeüf
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Guissiine ak dokhalinu lislaam ci koom koom ak souxaliku
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Sartiy tuup
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Ni aada di jéxité ci xalaatine
Khoutba gui mi ngui ajou ci: Ay njaangalé ci ndéŋkaané Luqmaane
Lii ay ubbé la 10-03-2015
22 / 6 / 1436 , 12/4/2015
Nekena thi toudou diarigne yi ganamague thi werou kor bokounathi :mougne thi mbolem khadiamyi,ak fouklou borombi thi lou lakhou…
21 / 5 / 1436 , 12/3/2015
Touki Diame Allakhira
14 / 5 / 1436 , 5/3/2015
Wakhtâne wi gui mi ngui ajou ci: léral wakh yi rote thi sânjjé gui nèkk thi wax lodoul dèf. Nguénéloup jeuf bou sèll. Yéne wou dis wik thi jeujf bou sèll. Wax lôdoul dèf akiy loram thi ligèyoup lislam. Akiy jékhitam.
Khoutba gui mi ngui ajou ci: léral ay lâj you bari té ajou ci Al-jana, ak fékhé ba douggfa, ak sabab yifay takha dougg
Wakhtâne wi mi ngui ajout hi lèral: Kéno yi ngua khamné thi la étâp joullite di tégué ak léral ngourouk Omar Ibn Aboul Aziz ligèye gou mak goumou thi déf ak béssalam