Magayou yolou yar ay bome you jigen, yitewou bi islame yitewo jigen,bokouna thi yar bomyou jigen:lakhuko thi ker gou mouthe ayib, ak yeramko ak ndiewan talko…
Doud netalibi kom nimou ame,takhawayou bilal thi doubam ak yonentebi ak ganaw boumofato,nodou bila thi madina ak tarouk dioya ,linouy diaeino thi nettalibi…
Lan moy khal boutadiou? Ay missal thi khal youtadiou,kholou yefaryi yeb dafatadiou, kholou joulit dana tadiou,lan boy mbir yiy tidie khol ka yi koy tiji?
Bokna thiyiy maye thiofelou yalla: bagueyalla ak yonentebi, diagne al khourane ak settentalko, kher thi nafilati gannaw faratayi takho toudou yalla ak diko fouklou…