Khoutba gui mi ngui ajou ci: léral taaroup lislam bi ngui khamné môy dîné jâmm, akiy téggine you rafète thi dounnd ak gnoudoul joullite. Di tônetou gni gnâwal thi Yonènete Mouhammad (Yalla na Yalla joulli thi môm té dôlliko jâm)
Fakhe baniab nek ay yamou yalla, fakhe ba yeneyeb selle niel yala, die lakale khamkham ak diafe thi yagnge katyi, fakheba niagrngemi nek loulkontine thi diamanomounek….
Degue bouwer ak ndiarignme thi tourou yallayi ak melokanamyi,dirdisrou omar bon abdou aziz ak lithi nek thi ay diagn guatt,degkane bouamsolo diam thi diamge katyi ak wete katyi,tawassoul Moylan ak aykhetam ak attem thi lislam.