-
Youssouf Ibn Nouh Ahmad "Limou mbiryi : 3"
Mélokâne bi :Kénne la thi yilimani Arabi Sawdite. Mi ngui jouddô Mâkka, fa la jânggé ba paré. Jânggalékate la thi kaba gui thi pâth gui ajou thi Al-Khourane. Jânggna kâmil thi radiop al-khourâne, ak aykamil thi yônnoup châtibiyya.