-
Bandar Ibn Abdoul Aziz Baliila "Limou mbiryi : 6"
Mélokâne bi :Mi ngi juddoo Makka ci atum 1395 ci gàddày gi; fala dooré jàŋŋ ba am bak. Amna majestér ci atum 1422 ci gàaddày gi ci fikh ci universitém Ummul Xurà. Amna itam doctoorà ci fikh ci atum 1429 ci gàddày gi ci universiép Madiina. Jàŋŋaléna fikh bu kawé fa Kàbaga, Ustàs la buy wuutu ci universitép Tàif. Yilimàn la ak xutbakat ci jumaay Al-Amiira Nawf ci Al-Aziiziyya bi ci Makka ak universitép Ibn baaz. Fal na ñuko yilimànu Makka béssup dibér 12-09-1434 ci gàddày gi.