-
Al-Ouyoûnoul Koûchy "Limou mbiryi : 1"
Mélokâne bi :Mi ngui jouddô thi Âssify thi maroc thi atoum 1967, Yilimâne la ak khoutbakate thi jâkkâp Ânedalous thi Daroul Baydâ. Môkkalna Al-khourae mi miy am jourômgnéneti ate. Amna bac thi lètre. Kènne la thi gni gniy jânggé njânggoum warch bi jogé thi nâfie thi maroc