-
Ahmad Al-Haddâd "Limou mbiryi : 1"
Mélokâne bi :Mi ngui askanô egypte toudd Ahmad Abdoul Fattâh Mouhammad Al-Haddâd, mi ngui joudd 25-08-1984. Thi universitèp Al-Azhar la amé lisensam thi lâkkou arapnthi atoum 2007. Akoup lijâssa mâjestèr thi wéral mbindd yi gnou fi bayyi thi attoum 2008, ak mâjestèr thi kham-khami Al-khourane ak foukki njânggine yi yi gnou tokhalé thi Yonnènetebi (Yalla na Yalla joulli thi môm té dôlliko jâmm)