-
Mouhammad Châbâne Abou Kharne "Limou mbiryi : 1"
Mélokâne bi :Jânggikatoup égypte la. Mi ngui joudd thi atoum 1984, mi ngui am lijâssa thi njângginoup al-khourâne ak kham-khamou charia thi colèzoup njângginou al-khourâne bi thi Al-Azhar, ak thi njângg gou kawé. kènnela thi ngiy jânggalé thi markazoup Oustaz doctor Ahmad Issa Al-Minssrâwî di njîtou jânggkatou al-khourâne yi thi égypte.