Limou mbiryi: 17
19 / 2 / 1437 , 2/12/2015
Nekenathi leral atte mourou thi islam , ak charti diolouk jiguen…
29 / 7 / 1436 , 18/5/2015
Neke nathi leral bonouk dialo ak toudou aya ak hadis you wakhe thi dialo, ak toudou diekhantalou dialo thi khetwi…
2 / 7 / 1436 , 21/4/2015
Nekenathi leral yitewo liguey thi lislame,ak ni yonenteyi ak rayou sne warwar amonane ay liguey…
22 / 6 / 1436 , 12/4/2015
Nekenathi leral ni diani waydiour nioy sababou sak niowe thi addouna,bakhal diame thi niani waydiour migui bok thi bakhal diame thi niari waydiour…
2 / 7 / 1437 , 10/4/2016
khoutba bi tie Le Coran guide sur le droit chemin tahawe diebe goran fouki aya thie sarou aname mesale bou ame soulo la.
houtaba bi tie ly ( Les moyens de trouver de l’argent licitement )
10 / 2 / 1437 , 23/11/2015
Nekna thi toudou ganelou werou tamkhari, ak warefou joulit thi werwi.
2 / 12 / 1436 , 16/9/2015
Nekenathi ay dekane youmatale niele keppe koubaga hajji diam thi karouk yalla ga…
Nekenathi lerale diganete saytaney jinne ak younit, ak katanou saytaney nit thi sake domou adama,ak ndakala mouy fego thi niome…
Nekena thi nontou ay lathie youbiri boukou nathi:gusguisou islam thi doukol television thi keur, ak ndakala mamoum difaye likorow thi joule…
Nekenathi leral foukki diarouway yokhani nite dinathi diare, khabrou bene mouneke kambou aldiana wala safara…
Nekenathi leral barik thiakhan ak tasarom, dansek thiakhan thi ay wakhe ak ay diafe…
Nekena thi leral warougarou domou adamayi thi malaikati,ak senye khathi ak seniy takhaway thi domou adama…
Nekenathi tontou ay lathie youbari bokounthi:atte faddouk diakar lou abe ay atte?atteb take niarel te awobi yekouko?...
Nekenathi leral ache yiwar thi diakor thi diabaram, akakhe yiwar thi diabar thi diakaram, ak ay layabir youame solo dime thi niom niare…
Nekenathi tontou ay lathie youbari boukounathi: atte fayekou bor, atte diouli witar thi goudi, atte wat ethi loudoul yalla…
Nekenathi leral kane moy oukhounman , toudou dekaneyi ak leralko ak doulithi…