-
Ahmad Tàlib Hamid "Limou mbiryi : 6"
Mélokâne bi :Dàkkantalam mooy Bàyu Az-zoubayr, mi ngi tudd Ahmad Tàlib Hamid Ibn Abdul Hamid Ibn Muzaffar Xàn. Judduna ci Riyàd ci atum 1401 ci gàddày gi. Mi ngi jànggé ci fakultép saria bi ci uniwérsitép ba amfa bak. Ginàw ngi mu am Masestér ci àtté ci fiq muqàran. Di ligéyé kom wootékate ci ministérup mbiri lislàm ci Riyad, tànnañuko muy jiité naafilayi ci koor, ci jàkka Médine ci atum 1434 ci gàddàygi, ginàw gi ci béssup 9 Octobr 2013 teppook 4 ci wérup ajj bi ci atum 1434 ci gàddàygi lañ koka déf yilimàne ci julli juroomyi.