-
Chirzâd Abdour-Rahmane Tâhir "Limou mbiryi : 1"
Mélokâne bi :Mi ngui toudd Chirzâd Ibn Abdour-Rahmane Ibn Tâhir Ibn Hassane Al-Kâfy Al-Kourdy Ach-Châfi î, mi ngui jouddô thi beutt gânnârou Irak thi atoum 1968 thi fou gnouy wakh An-Nâmâiyya. Fôfou la jânggé thi ay serigne you bari niki: Cheikh Abdoul Latif Ibn Khalil As-Soufy, ak Cheikh Al-Hafiz Ali Ibn Houssayn Al-Wassâbi, ak Cheikh Al-Hafiz Abdour Razzâkh Mouhammad Imâra, ak fénène tamite. Jîténa thi ay jâkka you bary thi Irak ak Imarate.