-
Moustapha Râd Al-Azâwî "Limou mbiryi : 1"
Mélokâne bi :Mi ngui jouddou thi 19-04-1986 thi Âzamiyy thi Baghdad thi Irak. Nékkônna - Yalla nako Yalla yereum- kènne thi mbôtâyoup jânggkate alkhourâne yi thi Irâk, bôkkna thi ay jongânté you bari, mi ngui fâtou thi 26-05-2007 thi jâmârlôk soldâroup amérik yi. Yalla nako Yalla bôlé thi gnimou nânggoul sène dé thi yônou Yalla ak gni deuggou.