-
Mouhammad Rachâd Ach-Charîf "Limou mbiryi : 1"
Mélokâne bi :Môy Mouhammad dômou Rachâd dômou Abdous Salâm dômou Abdour Rahmâne Ach-charîf, mi ngui jouddô deukk bou gnouy wakh Al- Khalîl thi Palestîne atoum 1925 thi atoum toubap, mouy kènn thi jânggkatou Al-Khourâne yi sîw thi addinabi, môy jânggalékatoup jâkka Al-Aqsâ bou barkèl bi agitam jâklâp Al-Ibrâhîmî yi nèkk thi Al-Khalîl.Guinnâw gui thi atoup 2002 tokhouna jeum Ordone.Nèkkna yilimâmou jâkka boûr bi toudd Abdoullah Al-Awwal bithi Abdoûlî