Limou mbiryi: 38
3 / 5 / 1437 , 12/2/2016
yer nie thie neke Passpass bu sell ak lu juuyook moom slafo salih ndanou foukhewou hame passpass soame thehid fekhle ba boumou yakhou.
28 / 4 / 1437 , 8/2/2016
douli aye deireni ak thier Naka la julli di neekke luy feexël xol
20 / 6 / 1436 , 10/4/2015
Nekenathi leral diarinou khame lanmoy bokkale ak a khadiame…
5 / 6 / 1436 , 26/3/2015
Nekena si khamle lane moy diouli ak lan e lane thi dioublou thu islam,ak wathrwayam ak ay diriniam…
17 / 5 / 1436 , 8/3/2015
Wadjal Lénn déé
14 / 5 / 1436 , 5/3/2015
Waxtàn wi gui ajou ci lèral diggdômouk lislam ak né dâ lëkkakô ak pass-pass ak jâmou akouw dokhine
4 / 5 / 1436 , 23/2/2015
Gënéelal toude yalla - Toude léenma ma toude léen, sante léenma te bouléenma xarab.
27 / 3 / 1436 , 18/1/2015
Teki tere biy wakh si gnenti regal youy takh gakham louy bokkale ndax ga man thie mouthie
Tekki tere biy wakh siyiy yakh Islam Mohamed Abdel Wahab
6 / 3 / 1436 , 28/12/2014
Ay joumtoukây youy jâppandal tôpp Yonnènete bi (Yalla na Yalla joulli thi môm té dôlliko jâm)
26 / 2 / 1436 , 19/12/2014
Khamlé pass-pass bou wére, jèkhitam thi nite ki, jèkhitam thi mbolomi
25 / 2 / 1436 , 18/12/2014
Dokhînou nite ki mi gui ajout hi pass-passam,
Nekena thi toudou barik fitnayi ak diafek sakhe thi dine,ak toudou sababisakhe thi dine ak ay kallagn koram…
28 / 5 / 1436 , 19/3/2015
Neke nathi leral li diokale diouliteyi ak alkhuor ak sounna,kene manta diabe thi alkhourane walif sounna…
21 / 5 / 1436 , 12/3/2015
Nekena thi toudou mbir yigua khamni mante niake guir nite mana dollekou thi guem yalla…
Waxtàn wi dafay leral na lagnouy jeuflaneté ak gnoudoul joullite
Sakh thi dîné
Ragal Yalla
26 / 7 / 1437 , 4/5/2016
1 Li ab nataalla bouy jaangalé aj 2 xétou aj yi 3 Lignouy ayé kou armal 4 Ay njoumté you siw lol si aj gi:
Nekena thi leral ni wakhtane diguante dioulityi ak nasaranyi mante nek adak toudou ay sababe yuobari…